N a f a h a n i :
Xassida la goo xam ni kër gumu nekk, wax nañu ni kër googa duñu fa mbugël kénn, liféeg xassida gi mungi ci biir kër ga képp ku Faatu ça kër ga sunu boroom ràmbu la .
Manuscrit : #baayxalima
@abdukhoudoss.bsky.social
Alhamdoulillahi rabbil hanlamin Jerejëf Seyxanaa Ahmadal Xadim
N a f a h a n i :
Xassida la goo xam ni kër gumu nekk, wax nañu ni kër googa duñu fa mbugël kénn, liféeg xassida gi mungi ci biir kër ga képp ku Faatu ça kër ga sunu boroom ràmbu la .
Manuscrit : #baayxalima
Ku baax ki🤍😎
24.11.2024 13:56 — 👍 62 🔁 16 💬 1 📌 0Alhamdoulillah « xamoon naa ni dinga ñëw » 😂😂😂
25.11.2024 16:13 — 👍 0 🔁 0 💬 1 📌 0C’est le Baol😍🔥
25.11.2024 14:53 — 👍 6 🔁 2 💬 0 📌 0Kon ñëwngéen❤️😎🔥 koontaan naa sama xol sedd na🥹
#Bskynoce
Sant Serigne Touba rekk❣️
24.11.2024 13:08 — 👍 24 🔁 11 💬 0 📌 1Yoonu Murid yoonu worma ak teggin la | Serigne Ahmadou Rafahi Mbacke ak Serigne Mamoune Bousso, Khalife Serigne Mbacke Kanni Bousso
25.11.2024 13:05 — 👍 18 🔁 1 💬 0 📌 0Yaw Saa Borom sooma joxée ma sant la.
Waayé sooma joxul it ma gerem la tay muñ💫
#BoroomTuubaa
Ku baax ki🤍😎
24.11.2024 13:56 — 👍 62 🔁 16 💬 1 📌 0Wax dëgg Yàlla te noo wara taal añ yi😂
24.11.2024 10:55 — 👍 1 🔁 0 💬 1 📌 0Dañoo amagul auto xanaa 😂😂
24.11.2024 10:43 — 👍 1 🔁 0 💬 1 📌 0Mais crie fortttttttt mon frere 🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍🤍
24.11.2024 02:34 — 👍 4 🔁 1 💬 0 📌 0Équipe bou mak bi
24.11.2024 02:38 — 👍 4 🔁 2 💬 0 📌 0La meilleure equipe du monde joue aujourd’hui une raison d’être heureux n’est-ce pas ?🤍💜
24.11.2024 09:47 — 👍 3 🔁 1 💬 0 📌 0La plus grande équipe de football au monde😎 le grand Real Madrid🤍 revient à 17h30🔥
24.11.2024 02:32 — 👍 20 🔁 2 💬 0 📌 3Dakar, Sénégal 🇸🇳
23.11.2024 23:37 — 👍 37 🔁 10 💬 1 📌 0Merci 🤩
23.11.2024 23:51 — 👍 0 🔁 0 💬 0 📌 0Yitté just kawe rekk 😂😂😂
23.11.2024 23:42 — 👍 1 🔁 0 💬 1 📌 0Dakar, Sénégal 🇸🇳
23.11.2024 23:37 — 👍 37 🔁 10 💬 1 📌 0Ba mottalil yeneen gars yi kay sax 😂😂
23.11.2024 23:36 — 👍 1 🔁 0 💬 1 📌 0🏃🏾♂️mottali moo gën a wóor😂
23.11.2024 23:34 — 👍 1 🔁 0 💬 1 📌 0😎🔥
23.11.2024 23:33 — 👍 1 🔁 0 💬 0 📌 0Pas de Porno
Pas de Feminist
Pas de propagande Lgbtq
La TL Foot present
Les Patriotes presents
La TL basket et lamb présente
Réseau bi amagoul 🪳
23.11.2024 22:36 — 👍 29 🔁 3 💬 4 📌 0Ça y’est Adrien Rabiot a définitivement retrouvé le rythme. 🔥
Quel match à Lens ! 😤💙🤍
J’ai l’impression qu’il n’y a que des sénégalais ici, où sont les autres commu ?
23.11.2024 23:22 — 👍 23 🔁 3 💬 3 📌 0Saamba alaar
23.11.2024 23:22 — 👍 3 🔁 0 💬 0 📌 0Man naa jàng rekk 😎😂
23.11.2024 23:22 — 👍 1 🔁 0 💬 1 📌 0Ku matalul nag 😂
23.11.2024 23:18 — 👍 1 🔁 0 💬 1 📌 0Damay laaj rekk
23.11.2024 23:07 — 👍 0 🔁 0 💬 1 📌 0