Mbir mi gën doy waar ci wàllu xam-xamu addina (physique) mooy li ñuy woowe "intrication quantique". Ab mbir la buy am saa su ñaari particules (maanaam dond yi wu tuuti) jaxasoo wé bo nga xam ni lu ñi def ci benn ci ñar yi (maanaam soo natté etaa wam) dey am jexital ci beneen bi.
1/3